1
00:00:20,856 --> 00:00:26,862
HOTEL HAZBIN

2
00:00:34,620 --> 00:00:35,540
Dafa mujjee nekk lu jaar yoon!

3
00:00:35,580 --> 00:00:37,708
BARAKK AYU-BIS BI NJËKK, SËR PENTIOUS!

4
00:00:37,748 --> 00:00:43,046
Kontaan naa loolu Sir Pentious
Demal ci otel bi.

5
00:00:43,086 --> 00:00:45,716
maa ngi lay fàttaliku
ni Pentious jéemoon na nangu dëkk bi

6
00:00:45,756 --> 00:00:48,594
ak seen steampunk yu amul benn njariñ
fan yu néew ci ginaaw.

7
00:00:48,634 --> 00:00:52,262
waaye gisuma
Xaaral ma jéema def luni mel fii.

8
00:00:54,264 --> 00:00:55,350
Loolu lan la?

9
00:00:55,390 --> 00:00:58,270
Nuyu, jigéen ju violet.

10
00:00:58,310 --> 00:01:03,609
Sama sos bu bees la,
Fukk ak benn junni Super Skinner.

11
00:01:03,649 --> 00:01:08,071
Dama bëgga tiire bal
ci yeneen way wuyusi yi.

12
00:01:08,111 --> 00:01:09,239
Lan? Lu tax?

13
00:01:09,279 --> 00:01:11,074
Ku nekk dafa baax.

14
00:01:11,114 --> 00:01:13,243
Lu leer mooy fiir la.

15
00:01:13,283 --> 00:01:15,746
Ma yëg ni dañu may waaja ray.

16
00:01:15,786 --> 00:01:17,414
Waaye kañ ? Naka?

17
00:01:17,454 --> 00:01:19,500
Dama wara waajal sama bopp.

18
00:01:19,540 --> 00:01:21,500
Piyeesu sama masin yegsi na.

19
00:01:22,668 --> 00:01:23,752
Signe fii.

20
00:01:24,545 --> 00:01:26,215
Dieredieufeuti.

21
00:01:26,255 --> 00:01:28,258
Banneexu ci sa jënd ci Carmine.

22
00:01:28,298 --> 00:01:29,301
Karmin?

23
00:01:29,341 --> 00:01:31,220
De Carmilla Carmine?

24
00:01:31,260 --> 00:01:33,388
Ndax jënd nga ci jigéen ju mag?

25
00:01:33,428 --> 00:01:34,640
Ci lu wóor.

26
00:01:34,680 --> 00:01:36,767
Mooy jaaykatu ngannaay bi gëna mag.

27
00:01:36,807 --> 00:01:38,769
Loolu jeexna leegi.

28
00:01:38,809 --> 00:01:39,812
Hey!

29
00:01:39,852 --> 00:01:42,898
Dañu ko tere
defar ay ngannaay ci otel bii.

30
00:01:42,938 --> 00:01:44,441
Kenn jéemul la ray.

31
00:01:44,481 --> 00:01:48,151
nit ñi dañu baax
ndax dañu bëgg ngeen féexal seen xol.

32
00:01:57,244 --> 00:01:59,456
Xaaral ma xalaat bu baax.

33
00:01:59,496 --> 00:02:01,458
Dëgg la. Danga wara nu wóolu.

34
00:02:01,498 --> 00:02:02,584
Wóolu ma ko.

35
00:02:02,624 --> 00:02:07,422
Lu tax dunu bàyyi sunu xel ci loolu?
ni liggéey tay?

36
00:02:07,462 --> 00:02:09,383
Nanu njëkka tëral ay sàrt.

37
00:02:09,423 --> 00:02:13,387
Amul ay gànnaayu tabax
wala ñuy wut yeneen gan.

38
00:02:13,427 --> 00:02:15,596
Te danga wara bàyyi mbir yooyu.

39
00:02:17,472 --> 00:02:19,935
Luma wax leegi?

40
00:02:19,975 --> 00:02:22,271
Lan? Bul def dara samay nen.

41
00:02:22,311 --> 00:02:24,147
Dañuy déggal samay ndigal yu bon.

42
00:02:24,187 --> 00:02:26,608
Bëgg nga des ngir jot sa bopp?

43
00:02:26,648 --> 00:02:28,277
Waaw.

44
00:02:28,317 --> 00:02:29,903
Wax nen yi "tàggoo".

45
00:02:29,943 --> 00:02:31,864
Kon, nen yu ndaw.

46
00:02:31,904 --> 00:02:33,824
Dañu wara dem.

47
00:02:33,864 --> 00:02:37,411
Mënatuma dëkk ak yaw.

48
00:02:37,451 --> 00:02:38,371
Loolu baaxna lool, patroŋ.

49
00:02:38,411 --> 00:02:39,830
Bul bañ.

50
00:02:39,870 --> 00:02:42,289
Noonu la mbir yi wara mel.

51
00:02:55,594 --> 00:02:56,594
Alastor!

52
00:02:59,222 --> 00:03:00,059
Baal ma?

53
00:03:00,099 --> 00:03:02,311
Maa ngi ndékki.

54
00:03:02,351 --> 00:03:05,105
Nen yooyu am nañu fépp.
Raqleen leen.

55
00:03:05,145 --> 00:03:07,858
Suko defee, ak bànneex bu rëy!

56
00:03:07,898 --> 00:03:09,107
Te doo leen gaañ.

57
00:03:09,775 --> 00:03:11,486
Leegi neexatul noonu.

58
00:03:11,526 --> 00:03:14,072
Suma génnee dinaa leen toppatoo.

59
00:03:14,112 --> 00:03:15,198
Muus.

60
00:03:15,238 --> 00:03:16,450
Loolu lu soof la.

61
00:03:16,490 --> 00:03:18,994
Nanga def ci ñépp. Noo ngi leen di sant ci seen ñëw.

62
00:03:19,034 --> 00:03:20,954
Bu yàggul dara nu seetlu

63
00:03:20,994 --> 00:03:26,209
Daa melni amna
tuuti coow ci hotel bi.

64
00:03:26,249 --> 00:03:30,088
Te loolu mën na nekk lu baaxul.
ngir sunu liggéey.

65
00:03:30,128 --> 00:03:35,928
Menn mbir mooy amal njariñ groupe bii.

66
00:03:35,968 --> 00:03:39,471
- Tàggat wóolu!
- Tàggat wóolu! Daan.

67
00:03:40,138 --> 00:03:42,182
Vaggie, nu ngi koy repetition.

68
00:03:43,392 --> 00:03:45,479
Dina nu def tàggat yaram.

69
00:03:45,519 --> 00:03:48,941
Ak lii lépp luy tekki?

70
00:03:48,981 --> 00:03:49,859
NAN LAAY WOOL

71
00:03:49,899 --> 00:03:53,028
Duma leen jox spectacle
ci yii bënn.

72
00:03:53,068 --> 00:03:56,573
Dinaa ko def, waaye damay njëkka fay

73
00:03:56,613 --> 00:03:58,909
te xam naa ne manula fey.

74
00:03:58,949 --> 00:03:59,993
Loolu lu soof la.

75
00:04:00,033 --> 00:04:02,788
Duma xalaat laal la, jargoñ bi.

76
00:04:02,828 --> 00:04:05,499
Baax. Nanu tàmbali. Sarli?

77
00:04:05,539 --> 00:04:09,878
Amaana mën nga ko toppatoo
ci liggéey bi.

78
00:04:09,918 --> 00:04:11,046
Ku nekk laa wóolu.

79
00:04:11,086 --> 00:04:14,174
Amaana mën nga gëna leeral
ni ñuy jàngee wóolu.

80
00:04:14,214 --> 00:04:15,093
Lan?

81
00:04:15,133 --> 00:04:18,637
Xamuma ndax mën naa...

82
00:04:18,677 --> 00:04:21,848
Gaawal. Dina yomb.
Yaakaar naa ni di nga ko mëna jànkoonteel.

83
00:04:21,888 --> 00:04:26,768
Waaw, dëgg la. Mën naa ko muñ.
Amul solo.

84
00:04:28,520 --> 00:04:31,400
Baax na lool. Dina nu tàmbalee ci bàyyi sunu bopp daanu.

85
00:04:31,440 --> 00:04:34,695
Ku nekk dina séddoo
dara lu yomb ci boppam,

86
00:04:34,735 --> 00:04:37,280
Dina daanu ci ginaawam
te dinanu ko dundal.

87
00:04:37,320 --> 00:04:39,031
Ndàndoon? Kan moo tàmbali?

88
00:04:39,531 --> 00:04:42,661
Man, man, man!

89
00:04:42,701 --> 00:04:44,161
BAAX NA. Yéeg.

90
00:04:45,370 --> 00:04:47,541
Bëgg naa leen lool sama gaa yi.

91
00:04:47,581 --> 00:04:51,293
Dama leen bëgg lool, ci dëgg.

92
00:04:53,253 --> 00:04:54,048
Xam naa la.

93
00:04:54,088 --> 00:04:57,634
Loolu neex nama!

94
00:04:57,674 --> 00:04:59,720
Angel, lu tax doo wéy?

95
00:04:59,760 --> 00:05:01,430
Baax na.

96
00:05:01,470 --> 00:05:04,391
Bii yoon, ku nekk daf ko wara tëye.

97
00:05:04,431 --> 00:05:06,059
Wala ñu def ak man.

98
00:05:06,099 --> 00:05:08,437
Nga séddoo dara ci man?

99
00:05:08,477 --> 00:05:09,646
Lu ngeen ci xalaat?

100
00:05:09,686 --> 00:05:12,190
Dama bëgg nàmp...

101
00:05:12,230 --> 00:05:13,608
Bul wax "dick."

102
00:05:13,648 --> 00:05:15,902
...popsicles, feebar.

103
00:05:15,942 --> 00:05:18,320
Xalaat bu yàqu nga am.

104
00:05:20,155 --> 00:05:21,615
Ak ginaar itam.

105
00:05:24,284 --> 00:05:26,578
Waa ju bees, yaa ci topp.

106
00:05:28,497 --> 00:05:32,584
Bëgguma dundu te amul samay <i>jaam</i>.

107
00:05:33,210 --> 00:05:34,419
Bu ma kenn jàpp.

108
00:05:35,378 --> 00:05:36,631
- Daan.
- Lu baax la.

109
00:05:36,671 --> 00:05:37,841
Xamnaa ni danga xawa seey.

110
00:05:37,881 --> 00:05:39,009
Baax na lool.

111
00:05:39,049 --> 00:05:40,258
Niffty?

112
00:05:42,344 --> 00:05:45,265
Yenn saa ma ray yaay yi
ci kanamu seeni liir

113
00:05:45,305 --> 00:05:47,224
muy àrtu.

114
00:05:49,518 --> 00:05:50,727
Waaw! Dafay metti!

115
00:05:55,524 --> 00:05:56,525
Dafay metti!

116
00:05:57,692 --> 00:06:00,238
Loolu doxul ni ñu ko doon seentoo.

117
00:06:00,278 --> 00:06:01,823
Amaana war nanu...

118
00:06:01,863 --> 00:06:03,784
Mbëggeel, wóolu ma.

119
00:06:03,824 --> 00:06:06,495
Dinaa ci toppatoo, waaw? Dafa am luy ñëw ci sama xel.

120
00:06:06,535 --> 00:06:08,538
Sooy seet ay xalaat,

121
00:06:08,578 --> 00:06:12,124
Amnaa luma mëna indil wóolu sa bopp.

122
00:06:13,083 --> 00:06:14,668
Lu nga xalaat?

123
00:06:16,253 --> 00:06:18,298
Oh. Lu ngay waajal patroŋ bi?

124
00:06:18,338 --> 00:06:20,967
- Bëgg naa sa yéere.
- Luy njariñu béjjén yi ?

125
00:06:21,007 --> 00:06:22,969
Ndax mën naa laal sa yatt?

126
00:06:23,009 --> 00:06:25,430
Ndax ay noppam lañu wala kawaram?

127
00:06:25,470 --> 00:06:26,596
Duma ràññee.

128
00:06:27,305 --> 00:06:28,809
Alastor, nuyu la.

129
00:06:28,849 --> 00:06:31,394
Na nga def ci bésu tey?

130
00:06:31,434 --> 00:06:32,437
Ak kii, patroŋ?

131
00:06:32,477 --> 00:06:34,147
Bëgg nga ma dagg sa kanam?

132
00:06:34,187 --> 00:06:37,192
noppi
sudee dañu bëgga tëye seen coq.

133
00:06:37,232 --> 00:06:39,277
Nanga def, Zestial!

134
00:06:39,317 --> 00:06:40,652
Yaay bu baax!

135
00:06:41,403 --> 00:06:44,447
Klimaa bi neex na lool tay.

136
00:06:45,991 --> 00:06:46,911
Loolu mooy dëgg.

137
00:06:46,951 --> 00:06:49,911
Daa melni mën na daanu
taw asid tay ci ngoon.

138
00:06:51,204 --> 00:06:52,749
Sudee wërsëg a ngi ak nun.

139
00:06:52,789 --> 00:06:55,001
yuuxu yi dañu ma neex.

140
00:06:55,041 --> 00:06:56,711
Lu ngeen di yëg?

141
00:06:56,751 --> 00:06:59,923
yàgg na
ni doo nu sargal ci sa kanam.

142
00:06:59,963 --> 00:07:00,842
Kaka!

143
00:07:00,882 --> 00:07:03,426
Dégg naa ay jaar-jaar yu doy waar.

144
00:07:03,466 --> 00:07:07,053
Neena ñu daanu ci gànnaayu asamaan.

145
00:07:08,930 --> 00:07:11,143
Ma noppalu bu baax.

146
00:07:11,183 --> 00:07:12,477
Amul lenn lu am solo.

147
00:07:12,517 --> 00:07:15,187
Waaye amna solo
def ku nekk ci jaaxle.

148
00:07:17,272 --> 00:07:19,985
Amna itam luñuy wax
ci sa bokk

149
00:07:20,025 --> 00:07:23,572
ak prinses bi ak jafe-jafe yi mu àndaloon.

150
00:07:23,612 --> 00:07:26,741
naka ngay daanu ci mbir yu amul benn njariñ yooyu?

151
00:07:26,781 --> 00:07:28,285
Amnaa samay sabab.

152
00:07:28,325 --> 00:07:30,120
Jéemal xalaat soo bëggee.

153
00:07:30,160 --> 00:07:31,953
Dama bëgg ay komplot.

154
00:07:33,663 --> 00:07:38,128
Dina nekk lu gëna rëy
Jéemal xam sa xalaat, Alastor.

155
00:07:38,168 --> 00:07:42,507
Yaa ngi nekkoon ludul ab jafe-jafe
Bi nga ñëwee ci buur ba leegi.

156
00:07:42,547 --> 00:07:47,802
Sudee ku màgget ni yaw moo ko wax,
Dama ko jàppee ni sargal la.

157
00:07:57,479 --> 00:08:00,817
Déedéet, dama am liggéey bu am solo lool
ngir yaw.

158
00:08:00,857 --> 00:08:03,568
Demal te wottu buntu bi
ba ma dellusi.

159
00:08:07,656 --> 00:08:08,742
Melokaan.

160
00:08:08,782 --> 00:08:10,242
Frank mingi ñëw.

161
00:08:11,117 --> 00:08:12,160
Ndax am nanu ay tur?

162
00:08:40,689 --> 00:08:42,567
Dalal jàmm, njiiti jahannama,

163
00:08:42,607 --> 00:08:44,069
dajale naa leen fii

164
00:08:44,109 --> 00:08:47,028
ndax dañuy màndargaal
kàttan yiy jiite dëkk bi.

165
00:08:47,570 --> 00:08:49,449
Boroom ay milioŋ ciy ruuh lañu.

166
00:08:49,489 --> 00:08:52,744
ruuh yi nekk ci jafe-jafe
ak kalendriye Extermination bu bees bi.

167
00:08:52,784 --> 00:08:57,706
Danu wara waxtaan ci linu mëna def
ngir toppatoo sunuy njariñ.

168
00:08:58,206 --> 00:09:00,126
Zestial, kontaan naa ci gis la xarit.

169
00:09:00,166 --> 00:09:02,294
Carmilla, mbégte la ni saa yu nekk.

170
00:09:03,503 --> 00:09:07,175
- Alastor?
- Waaw, waaw, demoon naa ab diir.

171
00:09:07,215 --> 00:09:09,259
Yaakaar naa ni dangay xalaat fan laa nekkoon.

172
00:09:09,843 --> 00:09:10,929
Dëgg mooy déet.

173
00:09:10,969 --> 00:09:12,721
Noo ngi dalal jàmm.

174
00:09:13,471 --> 00:09:19,354
Renn Extermination bi mettiwoon na lool,
gëna bari yeneen at yi.

175
00:09:19,394 --> 00:09:23,650
Danuy xayma ni danu ñàkk
16% ci askan wi.

176
00:09:23,690 --> 00:09:28,403
Leegi malaaka yu bari yi
Dina ñu gaaw dellusi, dina nekk lu am xel...

177
00:09:29,362 --> 00:09:30,907
Dinaa ko toppato, Vox.

178
00:09:30,947 --> 00:09:32,117
Ndax am nga sikki-sakka ci man?

179
00:09:32,157 --> 00:09:34,035
Dëgg la? Ci man?

180
00:09:34,075 --> 00:09:35,285
Loolu mooy lima xalaat.

181
00:09:36,286 --> 00:09:37,622
Waaw, waaw.

182
00:09:37,662 --> 00:09:38,705
Clown lañu.

183
00:09:39,748 --> 00:09:42,419
Jërëjëf, Vee. Ba beneen. Fóon, buur.

184
00:09:42,459 --> 00:09:44,419
Velvette, li nga ñëw lu baax la.

185
00:09:45,003 --> 00:09:48,174
Ndax say naataango dina ñu la gunge?

186
00:09:48,214 --> 00:09:49,843
Dédeet, amna ñu mbir yu gëna baax ñu def

187
00:09:49,883 --> 00:09:52,345
luñuy dégg ci jigéen ju mag ju am gémmiñ gu dëgër
ku yaakaar ni mooy soxna si.

188
00:09:52,385 --> 00:09:53,972
Dama ñëw ci sa tur.

189
00:09:54,012 --> 00:09:55,096
yéeme na.

190
00:09:55,972 --> 00:09:59,309
Nima ko waxoon, dañu wara waxtaan...

191
00:10:00,643 --> 00:10:01,480
Waaw?

192
00:10:01,520 --> 00:10:04,647
Li soxal topic débat bi...

193
00:10:05,273 --> 00:10:06,276
Kaka.

194
00:10:06,316 --> 00:10:08,528
- Loolu neex na!
- Asamaan yi!

195
00:10:08,568 --> 00:10:10,113
Fan nga ko jëlee?

196
00:10:10,153 --> 00:10:12,614
Nu fekk ko ci bis bi ñuy ray àdduna.

197
00:10:13,281 --> 00:10:17,660
Sudee mën nañu ray nit ñu sell ñooñu,
lépp soppeeku na.

198
00:10:18,203 --> 00:10:20,580
Mën nanu leen jànkoonteel.

199
00:10:21,164 --> 00:10:24,125
Nu ngi defar pexem song bu mat sëkk.

200
00:10:32,342 --> 00:10:36,264
Sudee dëgg la ñu bëgg xare
Ak firnde yu néew,

201
00:10:36,304 --> 00:10:40,975
Dañu gëna ñàkk xel lima yaakaaroon ni noonu la.

202
00:10:41,351 --> 00:10:44,272
"Firnde yu néew"?
Exorcist bu dee la.

203
00:10:44,312 --> 00:10:46,232
Dinaa wax ni amul benn sikki sakka.

204
00:10:46,272 --> 00:10:48,943
Maam, ndax dangay silmaxa?

205
00:10:48,983 --> 00:10:50,653
Xamunu nu mu faatoo.

206
00:10:50,693 --> 00:10:53,573
Xëy na du liggéeyu jinne.

207
00:10:53,613 --> 00:10:55,617
Sudee nu gaawantu dugg ci xare,

208
00:10:55,657 --> 00:10:59,412
Mënu ñu woon dindi jahannama yépp
ngir tàmbali mbooloo?

209
00:10:59,452 --> 00:11:01,039
- Dafa melni.
- Mën na nekk.

210
00:11:01,079 --> 00:11:02,874
- Dëgg la.
- Mën na am.

211
00:11:02,914 --> 00:11:04,999
- Yaakaar naa.
- Xamuma.

212
00:11:06,042 --> 00:11:07,420
Leegi xamnaa loolu.

213
00:11:07,460 --> 00:11:10,256
Góor gi daa doy waar ngir xeex,

214
00:11:10,296 --> 00:11:12,340
Kon jarul, wala ?

215
00:11:13,883 --> 00:11:15,845
Lu xew, fosil?

216
00:11:15,885 --> 00:11:18,807
Danga màgget lool
jël nguur gi...?

217
00:11:18,847 --> 00:11:21,182
<i>Waneel tuuti ngor</i>

218
00:11:22,058 --> 00:11:24,187
<i>Sa jikko jaarul yoon</i>

219
00:11:24,227 --> 00:11:28,983
<i>Kenn waxul ak Zestial nii.</i>

220
00:11:29,023 --> 00:11:30,985
<i> Xalaat nga</i>

221
00:11:31,025 --> 00:11:33,696
<i>Lu nu nara muñ</i>

222
00:11:33,736 --> 00:11:37,782
<i>Sa njubadi bu amul benn werante fii?</i>

223
00:11:38,575 --> 00:11:40,620
<i>Danga juum</i>

224
00:11:40,660 --> 00:11:43,331
<i>Sama gis-gis warul soppiku</i>

225
00:11:43,371 --> 00:11:46,668
Amaana seetluwoo ko,
Waaye man maay soxna si

226
00:11:46,708 --> 00:11:49,587
<i>Te du def dara lu amul .
Loo bëgg

227
00:11:49,627 --> 00:11:52,340
<i>Man maay ki gëna mag ci Vees yi</i>

228
00:11:52,380 --> 00:11:54,467
<i>Daf lay sonal ni amuma respe</i>

229
00:11:54,507 --> 00:11:56,803
<i>Waaye kan moo ko mëna sargal?</i>

230
00:11:56,843 --> 00:11:58,930
<i>Ndaje clown yu tiis</i>

231
00:11:58,970 --> 00:12:01,891
<i> Kañ la njiit yi tàmbalee
Ndax da ngeen ragal xeex?</i>

232
00:12:01,931 --> 00:12:03,852
<i>Dañu dem ba génn ci modd</i>

233
00:12:03,892 --> 00:12:06,521
<i>Maa ngi lay massawu buur, waaye duma ko nangu</i>

234
00:12:06,561 --> 00:12:08,273
<i>Kenn dootu la bàyyi xel</i>

235
00:12:08,313 --> 00:12:10,859
<i>Danu soxla yeneen leeral ngir mëna def</i>

236
00:12:10,899 --> 00:12:13,111
<i>Bëgg nga sama ngor?</i>

237
00:12:13,151 --> 00:12:15,864
<i>Mën naa leen lekk su ma bëggee</i>

238
00:12:15,904 --> 00:12:20,452
<i>Yaw ak Vees da ngeen dof te ñàkk xam-xam</i>

239
00:12:20,492 --> 00:12:24,914
<i>Duñu déglu àrt
Rookies yu réy lañu

240
00:12:24,954 --> 00:12:27,208
<i> Ndax amna li ma wax lu la mettiloo?</i>

241
00:12:27,248 --> 00:12:29,836
<i>Bi nga gisee boppu malaaka</i>

242
00:12:29,876 --> 00:12:31,838
<i>Dafa am lu soppiku ci sa bët</i>

243
00:12:31,878 --> 00:12:34,466
<i>Sa kanam gu laxasu xonk</i>

244
00:12:34,506 --> 00:12:36,551
<i>Lu tax nga ragal xare?</i>

245
00:12:36,591 --> 00:12:38,761
<i>Loolu la ngannaay yi ngeen di jaay</i>

246
00:12:38,801 --> 00:12:41,055
<i>Jërëjëf ci sama ñàkka jox cër</i>

247
00:12:41,095 --> 00:12:43,516
<i>Leegi dama yaakaar ni amna kumpa</i>

248
00:12:43,556 --> 00:12:45,810
<i>Xam nga dara ci dagg bopp boobu</i>

249
00:12:45,850 --> 00:12:47,604
<i> Ndax amna lu nga bëgga wax?</i>

250
00:12:47,644 --> 00:12:49,604
<i> Ndaje bi jeexna!</i>

251
00:12:53,274 --> 00:12:55,318
Ndaje bu am njariñ la.

252
00:12:55,777 --> 00:12:56,778
Baax na.

253
00:12:57,278 --> 00:12:59,991
Demleen ci asile bi ci jàmm, yéen ay dof.

254
00:13:00,031 --> 00:13:01,241
Fóon sama cul.

255
00:13:03,493 --> 00:13:04,579
Lu xew?

256
00:13:04,619 --> 00:13:07,080
Keroog lanu yegsi.

257
00:13:08,957 --> 00:13:09,957
Yaay?

258
00:13:16,339 --> 00:13:18,635
Loolu amna solo lool.

259
00:13:18,675 --> 00:13:20,470
Hey, mbindéef bu ndaw bu am coq.

260
00:13:20,510 --> 00:13:22,053
Dama am liggéey buma lay digal.

261
00:13:23,471 --> 00:13:24,350
Waaw, patroŋ.

262
00:13:24,390 --> 00:13:25,557
Toppleen leen.

263
00:13:29,727 --> 00:13:30,772
Mala.

264
00:13:30,812 --> 00:13:32,939
Luy lii?

265
00:13:33,898 --> 00:13:38,446
Amul lu gëna soxla wóolu
ni sadomasokism mooy nguur.

266
00:13:38,486 --> 00:13:43,032
Amul jàpp bu gëna dëgër jàpp.

267
00:13:43,950 --> 00:13:44,911
Loolu mooy seen devise.

268
00:13:44,951 --> 00:13:46,746
AMUL CRAVATE BU GËNA DËGËR
KI <i>JAAM</i>

269
00:13:46,786 --> 00:13:49,123
Angel, bëgg naa sa cawarte.

270
00:13:49,163 --> 00:13:50,331
Waaye...

271
00:13:52,667 --> 00:13:55,878
Lu tax ngay xalaat
Ndax amna ku bëgga xam lii?

272
00:13:57,755 --> 00:13:59,424
Loolu baaxul dara.

273
00:14:01,050 --> 00:14:04,345
Maa ngi waaja yar
ci xale yu bon yi.

274
00:14:05,888 --> 00:14:07,473
Fatteel ko. Dem.

275
00:14:08,433 --> 00:14:11,519
Salaam maalekum. Na nga def?

276
00:14:13,521 --> 00:14:16,568
Mënu ma ni dañu dem
nga nu indi fii, Angel.

277
00:14:16,608 --> 00:14:17,860
Loolu lu soof la.

278
00:14:17,900 --> 00:14:19,529
Loolu baaxna Vaggie.

279
00:14:19,569 --> 00:14:22,240
Amaana mën naa la jàppale...

280
00:14:22,280 --> 00:14:25,742
Déedet. Wax naa la mën ngama wóolu.
Dunga réccu.

281
00:14:27,160 --> 00:14:31,499
Dama leen wara jàngal
noonu la jàngee.

282
00:14:31,539 --> 00:14:33,918
Ndax noonu nga jàngee wóolu nit ñi?

283
00:14:33,958 --> 00:14:36,337
Mën naa dem bis bi yépp!

284
00:14:36,377 --> 00:14:37,463
Dare, yatt!

285
00:14:37,503 --> 00:14:41,050
Amul lu gëna am doole ni wóolu
diggante ay àndadoo ci xare.

286
00:14:41,090 --> 00:14:45,136
Soldaar yi, waajal leen,
ndax tey nekk nañu góor.

287
00:14:45,887 --> 00:14:47,432
- Yow...
- Xaar!

288
00:14:47,472 --> 00:14:49,642
Mënu ma xeex te samay <i>jaam</i>amul.

289
00:14:49,682 --> 00:14:51,851
...dina ñu bokk mucc.

290
00:14:52,852 --> 00:14:53,813
Yaw nag...

291
00:14:53,853 --> 00:14:57,106
- Bul ci xalaat sax.
- ...yaw nga def otel bi mu dox.

292
00:14:58,941 --> 00:15:00,360
Sama turn la!

293
00:15:02,278 --> 00:15:03,364
Vaggie, déet!

294
00:15:03,404 --> 00:15:06,242
- Su ko defee rekk lañuy jàngee.
- Du dëgg.

295
00:15:06,282 --> 00:15:08,786
Amna yeneen pexe, waaye dafay laaj jot.

296
00:15:08,826 --> 00:15:10,163
Amu nu jotu.

297
00:15:10,203 --> 00:15:11,998
Ñaata xeetu ray lañu nara am?

298
00:15:12,038 --> 00:15:14,334
balaa dof yii di doxalee?

299
00:15:14,374 --> 00:15:17,627
Ñaata yoon la sa askan di dee
balaa nuy awaase?

300
00:15:18,419 --> 00:15:19,256
Vaggie...

301
00:15:19,296 --> 00:15:20,548
Dama soxla ab <i>jaam</i>!

302
00:15:20,588 --> 00:15:22,800
Ma jël loxo bi, lépp jaarul yoon.

303
00:15:22,840 --> 00:15:24,761
Dama wara amal say mébet.

304
00:15:24,801 --> 00:15:27,847
Dama wara aar la.
Bu la musa réccu.

305
00:15:27,887 --> 00:15:30,558
Lii sa njuumte la, yaw dof ji!

306
00:15:30,598 --> 00:15:32,685
- Dunga dellu ginaaw.
- Ndimbal dimbali!

307
00:15:32,725 --> 00:15:35,146
Vaggie, du yaw...

308
00:15:35,186 --> 00:15:37,605
Su fekkee mënuma la dimbali, lu ma la jariñ?

309
00:15:38,314 --> 00:15:40,026
Vaggie, bul wax loolu.

310
00:15:40,066 --> 00:15:42,403
Def nga ma lu bari...

311
00:15:42,443 --> 00:15:45,238
Baal ma. Dama bëgga nekk man kese ab diir.

312
00:15:53,579 --> 00:15:54,997
Def nanu ko.

313
00:15:55,707 --> 00:15:57,208
Nanu ñibbi sama gaa yi.

314
00:15:58,251 --> 00:16:00,086
Ma yóbbu ko ci eskaal bi.

315
00:16:10,930 --> 00:16:13,601
Carmilla, lu lay jaaxal?

316
00:16:13,641 --> 00:16:16,686
Dunga faral di ñàkka dal.

317
00:16:17,478 --> 00:16:18,980
Du dara, Zestial.

318
00:16:19,647 --> 00:16:23,736
Malaaka ma daanu
ak sa loxo, wala book?

319
00:16:23,776 --> 00:16:25,029
Bunu ci wax dara.

320
00:16:25,069 --> 00:16:27,323
Yaay, amaana moom war nako xam.

321
00:16:27,363 --> 00:16:28,991
Kenn waru ko xam.

322
00:16:29,031 --> 00:16:31,367
Def naa li ma wara def.

323
00:16:32,452 --> 00:16:33,995
Bëgguma ci wax.

324
00:16:36,330 --> 00:16:40,585
<i> Lan moo jaaxal sa xol, xarit bu gëm?</i>

325
00:16:41,335 --> 00:16:46,257
<i>Maa ngi lay ñaan nga wóolu ma</i>

326
00:16:46,966 --> 00:16:51,973
<i>Sudee yaw moo waral ñu ray malaaka</i>

327
00:16:52,013 --> 00:16:57,894
<i> Lu tax doo bàyyi ñu xam sa doole?</i>

328
00:17:00,605 --> 00:17:02,565
<i>Dama yàgg a gëm </i>

329
00:17:03,858 --> 00:17:08,529
<i>Ngir duma tas samay loxo ak deret</i>

330
00:17:09,238 --> 00:17:13,494
<i>Waaye, bi mbir mi songee nu</i>

331
00:17:13,534 --> 00:17:16,080
<i>Atuma woon beneen pexe</i>

332
00:17:16,120 --> 00:17:20,333
<i>Dama wara def ndax dama leen wara toppato</i>

333
00:17:21,250 --> 00:17:24,128
<i>Waaye, su ku nekk xam</i>

334
00:17:24,837 --> 00:17:30,344
<i>Jahannama dina fësal xare</i>

335
00:17:30,384 --> 00:17:35,516
<i>Te naka lañu mëna xamee kan mooy jël ndam li?</i>

336
00:17:35,556 --> 00:17:38,144
<i>Mën naa ñàkk ñooñu</i>

337
00:17:38,184 --> 00:17:41,898
<i>Lima doon jéema aar</i>

338
00:17:41,938 --> 00:17:46,486
<i>Dina nekk </i>

339
00:17:46,526 --> 00:17:51,365
<i>Xamnaa ki leen di toppatoo</i>

340
00:17:51,405 --> 00:17:54,535
<i>Dinaa def lu nekk</i>

341
00:17:54,575 --> 00:17:57,163
<i>Doon te danga def njuumte</i>

342
00:17:57,203 --> 00:18:02,542
<i>Dinaa leen toppatoo ba noppi denc kumpa bi</i>

343
00:18:04,210 --> 00:18:07,131
<i>Bima la gisee</i>

344
00:18:07,171 --> 00:18:13,137
<i>Dama melni gan
Ci barab buma musul xam</i>

345
00:18:13,177 --> 00:18:15,431
<i>Ak nimu neexee</i>

346
00:18:15,471 --> 00:18:18,768
<i>Ndax amna ku ma xam</i>

347
00:18:18,808 --> 00:18:24,398
<i>Waaye barina mbir
Lima bëgga wax</i>

348
00:18:24,438 --> 00:18:28,903
<i>Dina nekk </i>

349
00:18:28,943 --> 00:18:33,991
<i>Dinaa la aar.</i>

350
00:18:34,031 --> 00:18:40,039
Dinaa def luma mën
Doonte def nga njuumte

351
00:18:40,079 --> 00:18:45,001
<i>Dina nekk sa àndandoo ba sa dee</i>

352
00:18:45,626 --> 00:18:50,091
<i>Te xamuma lan lanu mëna jànkoonteel</i>

353
00:18:50,131 --> 00:18:53,386
<i>Waaye xamnaa ni mënu ma leen wecci</i>

354
00:18:53,426 --> 00:18:57,640
<i>Dinaa def luma mën ngir muccal leen</i>

355
00:18:57,680 --> 00:19:00,810
<i>Maa ngi jéem</i>

356
00:19:00,850 --> 00:19:04,105
<i>Defal say mébet nekk dëgg</i>

357
00:19:04,145 --> 00:19:07,400
<i>Lu nu wara muñ</i>

358
00:19:07,440 --> 00:19:11,571
<i>Dina nekk </i>

359
00:19:11,611 --> 00:19:14,574
<i>Dinaa nekk ki leen di toppatoo</i>

360
00:19:14,614 --> 00:19:17,201
<i>Dinaa nekk ki lay aar</i>

361
00:19:17,241 --> 00:19:21,539
<i>Dinaa def lu nekk</i>

362
00:19:21,579 --> 00:19:27,044
<i>Doon te danga def njuumte</i>

363
00:19:27,084 --> 00:19:30,838
<i>Dinaa def lu nekk</i>

364
00:19:35,843 --> 00:19:38,179
Xet gu neex la.

365
00:19:39,388 --> 00:19:40,598
Dama bëgg mbalit.

366
00:19:41,766 --> 00:19:43,976
Lu nga ci gis?

367
00:19:45,061 --> 00:19:47,398
Góor gi dafa njëkka wax:

368
00:19:47,438 --> 00:19:50,610
“Du ngeen li ngeen wax ngeen doon.
"Yaw nga ray malaaka mi."

369
00:19:50,650 --> 00:19:52,445
Ndaw si tontu ko:

370
00:19:52,485 --> 00:19:54,155
<i>Dinaa def lu nekk</i>

371
00:19:54,195 --> 00:19:55,948
Luy li nga njëkka wax?

372
00:19:55,988 --> 00:19:57,491
Ni dafa ray malaaka mi.

373
00:19:57,531 --> 00:19:59,702
Loolu amna solo lool.

374
00:19:59,742 --> 00:20:01,913
Bàyyileen ko ci sunu diggante, waaw?

375
00:20:01,953 --> 00:20:03,496
Waaw, patroŋ.

376
00:20:06,582 --> 00:20:08,793
Salaam maalekum.

377
00:20:09,627 --> 00:20:11,505
Maa ngi lay massawu tay.

378
00:20:11,545 --> 00:20:14,131
Déedet. Maa ngi jéggalu.

379
00:20:14,882 --> 00:20:16,594
Maa ngi jéggalu ci lima la fitnaal.

380
00:20:16,634 --> 00:20:18,471
Nun benn ekip lanu.

381
00:20:18,511 --> 00:20:21,599
Jàppoon naa ni lépp dina gëna yomba,

382
00:20:21,639 --> 00:20:26,020
waaye dina ñu ànd jànkoonte ak moom.

383
00:20:26,060 --> 00:20:29,772
Xoolal li nga def ci say tàggat yaram.

384
00:20:31,565 --> 00:20:35,111
Kon, sidit boobu
Sa yaay tàmbali lay sonal.

385
00:20:35,987 --> 00:20:37,907
Waaw, ak loxo biñ dagg.

386
00:20:37,947 --> 00:20:41,661
Waaw, loolu neexul woon.

387
00:20:41,701 --> 00:20:43,621
Bëgg naa wàll woowu.

388
00:20:43,661 --> 00:20:47,166
At least mën nga nangu ñu dóor la
melni champion

389
00:20:47,206 --> 00:20:49,126
Liggéey bu baax, waa ju bees.

390
00:20:49,166 --> 00:20:50,419
Dëgg la?

391
00:20:50,459 --> 00:20:55,589
Gëm naa ni dugg naa ci
ci diggu xeex bu faat nit.

392
00:20:57,049 --> 00:21:00,803
Jërëjëf ci linga ma génne foofu.

393
00:21:08,728 --> 00:21:10,187
Xoolal rekk.

394
00:21:12,273 --> 00:21:13,526
Alastor!

395
00:21:13,566 --> 00:21:15,403
Rayeewoo nen yi.

396
00:21:15,443 --> 00:21:20,783
Monstre yu ndaw yi dañu wane ni
am njariñ lool.

397
00:21:20,823 --> 00:21:22,868
Lu tax doo leen joxaat Pentious?

398
00:21:22,908 --> 00:21:25,329
- Dëgg la?
- Waaw.

399
00:21:25,369 --> 00:21:27,540
Yaakaar naa ni leegi mën naa la wóolu.

400
00:21:27,580 --> 00:21:30,708
Waaye dëgg la, amul ngannaay.

401
00:21:32,209 --> 00:21:34,630
Samay nen! Waaw!

402
00:21:34,670 --> 00:21:37,925
Loolu neex na ñu dellu.

403
00:21:37,965 --> 00:21:41,679
Leegi demal defar sama néeg!

404
00:21:41,719 --> 00:21:44,764
Amaana mbir yi dina ñu gëna baax
gaaw lool ci linga yaakaar.

405
00:21:45,890 --> 00:21:49,562
Naka la deme ak Alastor, samay ndaw?

406
00:21:49,602 --> 00:21:51,230
Loolu yéeme na, patroŋ.

407
00:21:51,270 --> 00:21:54,608
Demoon naa ndaje
Amoon na fa benn xale bu jigéen bu yor ay baat.

408
00:21:54,648 --> 00:21:57,234
góor ak dinosaur.

409
00:21:58,194 --> 00:21:59,280
Loolu rafet na.

410
00:21:59,320 --> 00:22:01,866
Ki yor paaka yi dafa ray malaaka.

411
00:22:01,906 --> 00:22:05,244
Waaye jarul ma ci wax dara.

412
00:22:05,284 --> 00:22:06,912
Wóor.

413
00:22:06,952 --> 00:22:09,457
Ak suba mën nga gis Mars.

414
00:22:09,497 --> 00:22:12,626
Waaye léegi danu wara nelaw.

415
00:22:12,666 --> 00:22:15,002
Guddi gu neex, nen yu ndaw yi.

9999
00:00:00,010 --> 00:00:00,020
RATABBOYPDA ARG moo ko méngale ak jubbanti
www.subdivx.com
www.sous-titre.com

